Encor Eumeu sene refuse de serrer la main à Baboye au concert de waly seck à Pikine İndir

Arkadaşlarına gönder
eklemek
  • Premiered Aug 17, 2019

  • Abonez a notre chaîne YouTube https://www.youtube.com/channel/UCUzo... Aimer Notre page facebookhttps://web.facebook.com/guediawayein... https://www.instagram.com/guediawayei...

Yorumlar

  • guediawayeinfos TV
    guediawayeinfos TV 1 month ago

    N'oubliez pas de vous abonnez sur votre chaîne Guediawayeinfos TV et d'activer la cloche pour recevoir les notifications merci

  • Elhadji Diallo
    Elhadji Diallo 1 month ago

    Adouna amoul solo yall na yékh tayy djii kouthiii décédé wone sa morom mofayy djitou alor na rafet la vie elle est courte

  • ndoye le pikinois
    ndoye le pikinois 1 month ago

    Eume séne s8 de t2 coeur avec toi mé linga def dou yefou dioulite

  • L’absolu Gueye
    L’absolu Gueye 1 month ago

    Mbeurou pikine Yeuppeu Ama balde

  • bassirou sankhe
    bassirou sankhe 1 month ago

    Baboy taloube srg bamba bi koula bagne tamit doula wañi darra yow nekal xi djam rek eumeu sene lila nakhari teugoulako

  • ramos Sonko depuis Italie Torino domou Casamance

    Eumeu sene do sama mbeur dèh mais sa hol loumou rafètè motakh ma beugeu la mais tay lingua def bakhoul adouna amoul solo

  • Secou Diallo
    Secou Diallo 1 month ago

    Eumeu adouna amoul solo lirafétoul dara way

  • kane dieye
    kane dieye 1 month ago

    Sounou 400000 ta yalla déff Ousmane sonko si khol yi

  • michel diallo
    michel diallo 1 month ago

    C mort entre les deux , qui est d’accord avec moi ?

  • Ady Ndiaye
    Ady Ndiaye 1 month ago

    Il ne parle pas avec tyson ni baboye ses t'un rancunier eume sene aussi il est jaloux tu ne ressemble pas à balla gaye

  • Lamine Diawara
    Lamine Diawara 1 month ago

    Baboye c'est un vrai patriotes

  • daba diop
    daba diop 1 month ago

    Bilakhi gneipeu beug aladji mbaye

  • cheikhou sow
    cheikhou sow 1 month ago

    Mbeur yi daniou am problem mental ndakh coup yi

  • Moustapha Ndong
    Moustapha Ndong 1 month ago

    Baboye nite kou bakhela yalla nako yalla ar

  • Mouhamadou Lamine gueye

    baboy yaw dal machalla def ga Lou nice

  • Massamba Khouma
    Massamba Khouma 1 month ago

    Eumeu kou sof té begue porolèm

  • bonjour bonsoir
    bonjour bonsoir 1 month ago

    Eumue lila a metti baaboye tegolalaka niakue diome sa khol bou bonne ndym bi yor

  • Aliou Touré
    Aliou Touré 1 month ago

    euma lima djakhal dafa mélni ningay wakhé ak ningay défé wouténa

  • Abdou karime Thione
    Abdou karime Thione 1 month ago

    Eumeu sene dofbi kii dou nitt

  • Mouhamed Niang
    Mouhamed Niang 1 month ago

    Eumeu limou df grawna dè