MOEURS, la Brigade des Femmes - saison 1 - épisode 29 **VOSTFR** İndir

Arkadaşlarına gönder
eklemek
  • Published on Aug 22, 2019

  • ** Abonnez-vous ici : https://goo.gl/mme9BS ** Titre de l'épisode / La loi du talion : "Door Fayou" Découvrez le 29ème épisode de la nouvelle série d'EvenProd : MOEURS, la Brigade des Femmes. Vivez les enquêtes d'Anna aux côtés de Collé, Imane, Noor, Yandé et Marley... Leur mission, lutter contre l'injustice. Bou kénn noppéti. #Moeurs #BrigadeDesFemmes #episode29 #BouKénnNoppéti #EvenProd #team221 ** Abonnez-vous ici : https://goo.gl/mme9BS ** Réalisé par Ibou Gueye & Cheick Diallo (Sénégal, août 2019) Une production EVEN PROD : +221 33 867 67 42 Moeurs, la brigade des femmes : à l’assaut de la ville à Dakar, au Senegal !

Yorumlar

  • BST bst
    BST bst 4 weeks ago

    ANA KANE MOO BEUG SEYDINAA MOUHAMED

  • mimi fall
    mimi fall 4 weeks ago

    Gni amagoule diakeur ak diabar avant tamkharite yalla nalen yalla may

  • boye diouf Gias
    boye diouf Gias 4 weeks ago

    Kouye ème sama comanter yalnanga magali sii barckep borome magal gui🤲🤲

  • Niang Papaabdou
    Niang Papaabdou 4 weeks ago (edited)

    les Nobles suivent calmement moeurs sur youtube . Si tu en fais partie viens pointer✌

  • Alicia key's
    Alicia key's 4 weeks ago

    Chaque épisode damae commenté mais kén douma fallé ni j'aime rouss na sax lolll

  • Wadioubakh Tv
    Wadioubakh Tv 4 weeks ago

    Yalna nieup féké magal touba inchalah pouce bleu

  • Sokhna mai Sarr
    Sokhna mai Sarr 4 weeks ago

    Ku 18 safar nék sa yitté pousse bleu

  • Mor Mbacke
    Mor Mbacke 4 weeks ago

    Magui wadial magal touba kouma défal j’aime yalla nala fi fékk té And ak wérr

  • Ndeye Fatou Cisse
    Ndeye Fatou Cisse 4 weeks ago

    Yalla nagua yobou Say waydiour makka gnou fiére thi yaw thi barké Mame borome Touba

  • KINE SALIOU GUEYE
    KINE SALIOU GUEYE 4 weeks ago (edited)

    Kou beuge gisèk ak seydina mouhamed alldiana doral Jaime 💁💜

  • Bassirou Fall
    Bassirou Fall 4 weeks ago

    Première ak xarr ba sonu lool tamitt kou begue sa yaye pousse bleu 👍

  • Madame Cisse
    Madame Cisse 4 weeks ago

    Sénégal ngay guisse niite togne la yakheu sa adouna ba pare nela fou moudie fene cest ta parole contre la mienne juste parckil sont haut placés soit homme de tenues ou bien politiciens wala borom Darajaa lii kagne lay diekh non à la violence faites aux femmes 😡

  • Soda Gaye
    Soda Gaye 4 weeks ago

    Team moeurs tak diouk wadial 18 safar gui inchallah

  • danse tv
    danse tv 4 weeks ago

    Yalla na say wadiour goudou fane ba féké sa dieurigne gua meune léne yobou Mecque gnigua khamni séni parents dagno décédé yalla n'a souff séde séne kaw si barky Mohamed(SAW)🙈❤🍫

  • Sangam Nangam
    Sangam Nangam 4 weeks ago

    vraiment film bi nekhna trop❤❤ kou aimer sama commentaire yalle nasay adio fadiou🙏🙏

  • Baridiamu jouve
    Baridiamu jouve 4 weeks ago

    Commentaires yi

  • Amza Style
    Amza Style 4 weeks ago (edited)

    La partie où kyra et Marley parle d code wifi c très important c avec 7 manière qu'on pirate plein d gens et aussi avec les partage de connexion des téléphones

  • Niang waly
    Niang waly 4 weeks ago

    Mourid yagui wadial magal gui

  • QuEeN DoWN
    QuEeN DoWN 4 weeks ago

    mane dall inspecteur dione damako beugue💜💜

  • NoreyNi Diack
    NoreyNi Diack 4 weeks ago

    Baye Karim Mbacké Geuneu Yagu Geuneu wérr🙏